Arenebi.com : Actualité de la lutte sénégalaise
www.arenebi.com

Combat Pape Mbaye/Valdo : Kandji Production nous offre une belle affiche




1.Posté par Oupsss le 19/03/2015 18:05 (depuis mobile)
Hooo combat bou nekh mo néka nii valdo Aka mana beuré.merci kandji borom wolof You nekhyii kandji Aka deugue wolof

2.Posté par kagna le 19/03/2015 19:48 (depuis mobile)
Ah Kandi merci way. Combat bou nekh gua teugue. Wayé Pape mbaye tu es un grand champion mais so diougué ci défaite daguay khole Lou oyof touty malgres k lamb ji Lou yomb amouci

3.Posté par Azou le 20/03/2015 17:44 (depuis mobile)
Kandji yaa doff dé, noon combat bou nekh, vainqueur bi n'a dieul diene kaire

4.Posté par tapha mbaye le 21/03/2015 00:55
Ns some d tt coeur vk tw frér k dieu t done la victoir
Viive PAPE MBAYE II

5.Posté par théck le 22/03/2015 17:58
lii dou combat way boukou gnou lène

6.Posté par KS le 15/05/2015 14:13
Salam
Nous prions pour la victoire de Valdo l'espoir de tout BAssoul.




Cliquez ici pour toutes les news en bref



Recherche sur arenebi