Arenebi.com : Actualité de la lutte sénégalaise

[Vidéo] Yékini promet de la "faire boucler à tous ceux qui parlent trop à travers les radios...."


Rédigé le Mercredi 7 Décembre 2011 à 09:09 | Lu 3882 commentaire(s)



[Vidéo] Yékini promet de la "faire boucler à tous ceux qui parlent trop à travers les radios...."





1.Posté par diaz le 07/12/2011 10:34
soula balla gaye diapé do doye danga beuri wakh

2.Posté par diouf le 07/12/2011 13:05
yaww diazz dana beurii wakhhh!!mane balla moyy sama beurr dhhh maii biyone amna komba!!bouléne niou rekk!!yekini mbeurr leuu !!!

3.Posté par Deug deug le 08/12/2011 21:22
Walahi nekhoul ba nekhoul wayé Borom bi deff nani do morom gayi....Say wakh doff douko degg....Li Borom bi deff kouko beug dindi di nga soon....wakh nga deug kene manoul téré nga deff li nga beug deff....NDAKH YALLA NOPINA....Deguine aam na solo...Ya mana tontou ak yaar nak tek si....Vive le MEYEUR WAYYYYYY.

4.Posté par goor le 15/12/2011 15:17
wakhhh bi yeuppp da beurrriidiouf ak deug deug deugg bouléne niouuu réyy!!le 22inchalahhh on vera!!